Garab yu tukkee ci gancax ngir safara feebar u caar ci jur gi
Uploaded 2 years ago | Loading

9:53
Yar jur gu wér, doon na lu jafe ndax da ñoo yombb daanu feebar. Ñu bari daa ñu jaay xaalis bu takku ciy garab ngir fac seen jur. Ci widéwóo bii, daa ñu seet na ñuy faggoo ci feebar u caarum jur gi te it daa ñu jàng na ñuy fajjee bayima yu feebar yi akk garab yu tukkee ci gancax.
Current language
Wolof
Produced by
Atul Pagar, ANTHRA