<<90000000>> viewers
<<240>> entrepreneurs in 17 countries
<<4135>> agroecology videos
<<105>> languages available

Yafal um xar yeek bëy yi

Uploaded 1 year ago | Loading

Beykat yi da ñu baaxoowoon di yafal seeni kuuy aki bëy yu góor ndax ñooy gënn gaaw magg. Ngir yafal jur gi, lu am solo la am yi ci gënn. Ngir yafal xar yeek bëy yi, jox leen itam xont yu fees akk ay ferñent diir up 3 ba 6 weer. Rax si dolli ci dunnd gu baax, da ngeen war samm bu wóor jur gi ci bérëp bu sell. Ñakk leen te jox leen ay per i wermiffis ñatti weer yu nekk ngir aar seen werguyaram.

Current language
Wolof
Produced by
Practical Action
Share this video:

With thanks to our sponsors