Góob, bacc akk denc um sesaam
Uploaded 4 years ago | Loading

8:59
Sesaam yombb na bey. Waante doxalin yu bon ci ngóob mi, mbacc mi akk denc am ñoo yaqq kaliteem. Neex na dugël ay xeer, suuf akk yeneen salte ci biir sesaam bi yuy yaqq njëg am. Ci widéwóo bii daa ñu jis ni ñuy góobée, baccee akk denccee sesaam bi ngir wéerël kaliteem bu baax.
Current language
Wolof