Pépinièru soblé
Uploaded 3 years ago | Loading
12:37
Ngir ji soble, fawwu nga am suuf su taaju te nangu. Jamonoy nawett , danga wara fugg saay parka ngir reen yi bania nëpp. Deff ci fiime bu niorr wala composs. Bu fekke dangay jëfëndikoo jixu bu baax té wér ,lici ëpp dina saxx te dinga yaxanal. Maggug soble dafa soxla espace, ba taxna booy ji, bu leen jigeyantool bamu ëpp. Digênte bu nek bayil juroom jap fukki centimetar, xootaay bi na tollu ci benn centimetar. So nope nga suul ko ak tuuti suuf.
Current language
Wolof
Produced by
Agro-Insight