Ruy up meñeef yi
Uploaded 4 years ago | Loading
12:20
Ruy up meñeef yi ñi ngi koy defar ak pep u sereyaal yu ñu jaxaseek bol u ñebbe, sooja, gerte akk ay firwi. Sereyaal dina jox seen liir kattan gi mu soxlo ngir màgg. Leguminës yu mel ni ñebbe walla sooja da ñu deñc poroteyin yu manul ñakk ci defar siddit u xale bi. Ñam yu wex yi dafay am witaamin C biy naŋngu feer bi.
Current language
Wolof
Produced by
AMEDD