Andd xeex weñ yi ci tool u firwi yi
Uploaded 2 years ago | Loading

12:52
- English
- Arabic
- Bangla
- French
- Hindi
- Portuguese
- Spanish
- Assamese
- Ateso
- Bambara
- Bariba
- Bisaya / Cebuano
- Chichewa / Nyanja
- Chitonga / Tonga
- Dioula
- Fon
- Ghomala
- Hiligaynon
- Kiswahili
- Kriol / Creole (Guinea-Bissau)
- Luganda
- Luo (Lango - Uganda)
- Malagasy
- Marathi
- Mooré
- Persian / Farsi
- Peulh / Fulfuldé / Pulaar
- Runyakitara
- Tagalog
- Telugu
- Tumbuka
- Wolof
- Yao
Wegu firwi yi dagnuy dugal sen-i nenn ci firwi bi. Benn wegn kasse meun na nenn ay teemeer nenn, yuy sopaliku ay sax yu weekh yuy lekk biir firwi bi.Bugnu deful dara, wegn yi dagnuy yoku c lu gaaw té sakanane teksi meun nagnu yakh li ngeen goob yeup.»Boole len ay yoon yu wuute: Tek len ay jebakan Jefendiko len ay gnamal Dajale len ba noppi ngen yakh firwi yi daanu yeup
Current language
Wolof
Produced by
Agro-Insight