Caax ngir aar pepiñeer ci socant yi
Uploaded 4 years ago | Loading
11:35
Laata ñuy jàngg ni ñuy teggee caax u socant, na ñu xool bu baax yen yaqqkat yi man songg su nu pepiñeer. Naka ñu bari ci ñoom guddi la ñuy songg, di na tax ñu gëm ci lu war ñu tek caax ci sunu pepiñeer.
Current language
Wolof
Produced by
Agro-Insight