Ndoxu nefere yi ñamal gu wér la si tool yi
Uploaded 3 years ago | Loading
13:22
Ndoxu neefaré benn xeet neefare bou wer bu meuna bessalate suuf si. Ndoxu neefare yi , ndox la bounou dadialé ganaw dialalé ndox ci tos binu défaré ay sax . Dafa gnam ci ay hormon youy magal, ay gnam you ndaw ak ay gnam you ame solo youssi melni azot , janta ak pottassium.
Current language
Wolof
Produced by
Shanmuga Priya