Witëm tane ak mango yis
Uploaded 3 years ago | Loading
16:24
Wit mi nékna pacc bu ame solo thi liguéyu baykatbi. Solenko défé bubah diguén ame yokuté ak ay minñef you guen tekci kom-kom gou bakh. Thi vidéo bilé, dinañulen wane yane pékhé guendi jëfandiko thi sen wite.
Current language
Wolof
Produced by
Christoph Arndt, Holger Kahl, JFP films