Faggu feebar yi ci njombor yi
Uploaded 2 years ago | Loading
14:38
Koksijoos akk kolibasiloos nekk na ñu feebar yu bon ci njombor ndax da ñu walle. Garab u weterineer mënu ñu wérël njombor yi daanu feebar. Ndokk yalla, mën na ñoo ci faggu, ni ñuy koy jisee ci widéwóo bii.
Current language
Wolof
Produced by
Songhai Centre