<<90000000>> viewers
<<266>> entrepreneurs in 18 countries
<<4647>> agroecology videos
<<107>> languages available

Dunnd up ginaar u xont

Uploaded 2 years ago | Loading

Si jox leen ginaar yi gancax bés bu nekk men na ñu facc lenn ci seen soxlo dunnd. Waante, ngir yokk seen màggaay, li gen mooy jox leen xont bu ëmbb jaxasup pep u mbey, rakkal, cox akk kokiyaas

Current language
Wolof
Categories
Produced by
AMEDD, DEDRAS, MOBIOM, Songhaï Centre
Share this video:

With thanks to our financial partners